Les moments forts du magal de mame diarra bousso porokhane 2011 serons retransmis en direct sur ce site in sallah.                                             cheikh ibra fall: yaa wane bamba diarra bousso ilmoul yakhine daal ngaye khamee doomi maame seye nabou ndiaye yalla daal fal nga yangoo!  -  yaa khamlee bamba diarra boussoaynoul yakhine kaay ngay djissee lampe baaboul mouridiina ci yalla daal fall ngay yangoo! laa i laa illa laa. laa ilaa aa illa laa l.yawanee bamba diarra bousso hakhoul yakhine daal ngay dieuffee. neena touty kone mou dem fekk serigne bi leum mbirem ba kenne dou moss ci baa tiname loudoul thia biss baniouy tekhe.

EN DIRECT D' ENEA SANTE M C IBRA FALL .




Watch live video from toubaenea on it.justin.tv